Wikipedia wowiki https://wo.wikipedia.org/wiki/X%C3%ABt_wu_nj%C3%ABkk MediaWiki 1.47.0-wmf.1 first-letter Xibaarukaay Jagleel Waxtaan Jëfandikukat Waxtaani jëfandikukat Wikipedia Wikipedia waxtaan Dencukaay Waxtaani dencukaay MediaWiki Waxtaani MediaWiki Royuwaay Waxtaani royuwaay Ndimbal Waxtaani ndimbal Wàll Waxtaani wàll TimedText TimedText talk Module Discussion module Event Event talk Nosteg jant 0 3728 107592 106264 2026-05-09T03:55:37Z Omarius257 17399 /* */ nataalu nosteg jant bi leegi amna ay mbind 107592 wikitext text/x-wiki {{junj}} [[Dencukaay:Solar System True Color WO.png|upright=1.5|thumb|Nataal buy wone mbooleem cër yi ëpp solo ci sunu nosteeg jant, àdduna yi ci nekk]] [[File:Solar System size to scale mul.svg|thumb|upright=1.5|Nosteg jant]] '''Nosteg jant''' bi, ci xam-xamu [[saytubiddiw]], mooy nosteg sunuy jawwu, li ko toggale di ab biddiw, jant bi ak mboolel yëfi asamaan yuy warangiku ci li ko wër ; juróom-ñatti jawwu yees firndeel ak seen 175 weer yu nu xam, juróomu jawwuy dàtt yi, ak miliyaari [[yaram yu ndaw]] yi (bokk ci yooyu jawwu yu ndaw yi ak pëndi diggante jawwu yi). Nosteg jant bi mingi bokk ci galaksi bi tudd Yoon wu Meewe Jawwu yi nekk ci nosteg jant bi ñooy: [[Merkuur]], [[Weenus]], [[Suuf]], [[Maas]], [[Seres]], [[Yupiter]], [[Saturn]], [[Uraanus]], [[Neptuun]], [[Eris]], [[Pluton]], [[Haomea]], [[Makemake]], [[Goŋgoŋ]], [[Koawar]] ak [[Órkus]]. [[Wàll:Saytubiddiw]] rva3g11j80gl3wydl4rn3n5lkr1p6sv