Wikipedia
wowiki
https://wo.wikipedia.org/wiki/X%C3%ABt_wu_nj%C3%ABkk
MediaWiki 1.47.0-wmf.2
first-letter
Xibaarukaay
Jagleel
Waxtaan
Jëfandikukat
Waxtaani jëfandikukat
Wikipedia
Wikipedia waxtaan
Dencukaay
Waxtaani dencukaay
MediaWiki
Waxtaani MediaWiki
Royuwaay
Waxtaani royuwaay
Ndimbal
Waxtaani ndimbal
Wàll
Waxtaani wàll
TimedText
TimedText talk
Module
Discussion module
Event
Event talk
Ne-ne
0
2844
107596
102216
2026-05-20T03:41:35Z
~2026-30196-86
17560
107596
wikitext
text/x-wiki
Ne-ne, ñu xame ko ci [[faraañse]] ci((matière))mooy li toggale (li composer) wépp yaram wu am ag nekk gu nu man a laal (une réalité tangible ). Ñatti melokaanam yi ñu gën a miin nag, ñooy melokaan wu dëgër(l'état solide), wuy yol (l'état liquide) ak wu gaasu (l'état gazeux). Moom day jël [[barab (déggiit)|barab]](elle occupe de l'espace)te kemub ne-ne (la quantité de matière) ñi ngi koy natte ci [[jóor]](la masse) (bu fekkee ne mbir mi dafa aju ci waññ xaajiiti ne-ne(particules de matière), deesi jëfandikoo [[mol]](la mole) ).Ci noonu, ci xam-xamu [[jëmm]], lepp lu am ab jóor rekk [[ne-ne]] la. Ci biir loolu, ne-ne yu ñu miin yi ñu wër, ñi ngi sosoo ci ay [[bariyon]],kon ci waxiin wi nu baaxoo, boo ci déggee baatub ne-ne, nanga xam ne '''[[Baryon#Matière baryonique|ne-ne bu bariyon]]''' lañu jubloo wax. Tekkiin wii kon boolewuñu ci[[boson|boson yu dàttu]] (les bosons fondamentaux), yi nga xam ne ñooy tuxal ñeenti [[doole yu dàttu]] yi ak doonte am nañu ab jóor ak/walla genn kàttan.
[[Wàll:Ne-ne| ]]
[[Wàll:Jëmm]]
[[Wàll:Simi]]
0gazgrv1mb7tukye2cyqxgm6ru2q2p9
107597
107596
2026-05-20T03:48:29Z
~2026-30196-86
17560
107597
wikitext
text/x-wiki
Ne-ne, ñu xame ko ci [[faraañse]] ci((matière))mooy li toggale (li composer) wépp yaram wu am ag nekk gu nu man a laal (une réalité tangible ). Ñatti melokaanam yi ñu gën a miin nag, ñooy melokaan wu dëgër(l'état solide), wuy yol (l'état liquide) ak wu gaasu (l'état gazeux). Moom day jël [[barab (déggiit)|barab]](elle occupe de l'espace) te kemub ne-ne (la quantité de matière) ñi ngi koy natte ci [[jóor]](la masse) (bu fekkee ne mbir mi dafa aju ci waññ xaajiiti ne-ne(particules de matière), deesi jëfandikoo [[mol]](la mole) ).Ci noonu, ci xam-xamu [[jëmm]], lepp lu am ab jóor rekk [[ne-ne]] la. Ci biir loolu, ne-ne yu ñu miin yi ñu wër, ñi ngi sosoo ci ay [[bariyon]],kon ci waxiin wi nu baaxoo, boo ci déggee baatub ne-ne, nanga xam ne '''[[Baryon#Matière baryonique|ne-ne bu bariyon]]''' lañu jubloo wax. Tekkiin wii kon boolewuñu ci[[boson|boson yu dàttu]] (les bosons fondamentaux), yi nga xam ne ñooy tuxal ñeenti [[doole yu dàttu]] yi ak doonte am nañu ab jóor ak/walla genn kàttan.
[[Wàll:Ne-ne| ]]
[[Wàll:Jëmm]]
[[Wàll:Simi]]
8bxxm8ijcpn90b2ko4suns8p3duaypt
107598
107597
2026-05-20T03:51:21Z
~2026-30196-86
17560
107598
wikitext
text/x-wiki
Ne-ne, ñu xame ko ci [[faraañse]] ci((matière))mooy li toggale (li composer) wépp yaram wu am ag nekk gu nu man a laal (une réalité tangible ). Ñatti melokaanam yi ñu gën a miin nag, ñooy melokaan wu dëgër (l'état solide), wuy yol (l'état liquide) ak wu gaasu (l'état gazeux). Moom day jël [[barab (déggiit)|barab]](elle occupe de l'espace) te kemub ne-ne (la quantité de matière) ñi ngi koy natte ci [[jóor]] (la masse) (bu fekkee ne mbir mi dafa aju ci waññ xaajiiti ne-ne (particules de matière), deesi jëfandikoo [[mol]](la mole) ).Ci noonu, ci xam-xamu [[jëmm]], lepp lu am ab jóor rekk [[ne-ne]] la. Ci biir loolu, ne-ne yu ñu miin yi ñu wër, ñi ngi sosoo ci ay [[bariyon]], kon ci waxiin wi nu baaxoo, boo ci déggee baatub ne-ne, nanga xam ne '''[[Baryon#Matière baryonique|ne-ne bu bariyon]]''' lañu jubloo wax. Tekkiin wii kon boolewuñu ci [[boson|boson yu dàttu]] (les bosons fondamentaux), yi nga xam ne ñooy tuxal ñeenti [[doole yu dàttu]] yi ak doonte am nañu ab jóor ak/walla genn kàttan.
[[Wàll:Ne-ne| ]]
[[Wàll:Jëmm]]
[[Wàll:Simi]]
1w7wfa3rcihfbc9qgaqfhn4ou1y180a
107599
107598
2026-05-20T03:53:42Z
~2026-30196-86
17560
107599
wikitext
text/x-wiki
Ne-ne, ñu xame ko ci [[faraañse]] ci ((matière)) mooy li toggale (li composer) wépp yaram wu am ag nekk gu nu man a laal (une réalité tangible ). Ñatti melokaanam yi ñu gën a miin nag, ñooy melokaan wu dëgër (l'état solide), wuy yol (l'état liquide) ak wu gaasu (l'état gazeux). Moom day jël [[barab (déggiit)|barab]](elle occupe de l'espace) te kemub ne-ne (la quantité de matière) ñi ngi koy natte ci [[jóor]] (la masse) (bu fekkee ne mbir mi dafa aju ci waññ xaajiiti ne-ne (particules de matière), deesi jëfandikoo [[mol]](la mole) ).Ci noonu, ci xam-xamu [[jëmm]], lepp lu am ab jóor rekk [[ne-ne]] la. Ci biir loolu, ne-ne yu ñu miin yi ñu wër, ñi ngi sosoo ci ay [[bariyon]], kon ci waxiin wi nu baaxoo, boo ci déggee baatub ne-ne, nanga xam ne '''[[Baryon#Matière baryonique|ne-ne bu bariyon]]''' lañu jubloo wax. Tekkiin wii kon boolewuñu ci [[boson|boson yu dàttu]] (les bosons fondamentaux), yi nga xam ne ñooy tuxal ñeenti [[doole yu dàttu]] yi ak doonte am nañu ab jóor ak/walla genn kàttan.
[[Wàll:Ne-ne| ]]
[[Wàll:Jëmm]]
[[Wàll:Simi]]
1fjtcvzaimcy92nt2wqx83xfjw1jjjm