Wikipedia wowiki https://wo.wikipedia.org/wiki/X%C3%ABt_wu_nj%C3%ABkk MediaWiki 1.47.0-wmf.5 first-letter Xibaarukaay Jagleel Waxtaan Jëfandikukat Waxtaani jëfandikukat Wikipedia Wikipedia waxtaan Dencukaay Waxtaani dencukaay MediaWiki Waxtaani MediaWiki Royuwaay Waxtaani royuwaay Ndimbal Waxtaani ndimbal Wàll Waxtaani wàll TimedText TimedText talk Module Discussion module Event Event talk Wolof (làkk) 0 2439 107607 106810 2026-06-09T00:36:43Z InternetArchiveBot 12803 Rescuing 1 sources and tagging 0 as dead.) #IABot (v2.0.9.5 107607 wikitext text/x-wiki [[Image:Wolof language map.svg|thumb|Wolof làkk ([[Senegaal]])]] [[File:WIKITONGUES- Aminah Abba speaking Wolof.webm|thumb|Wolof làkk]] '''Wolof''' làkk la wu ñuy wax ci [[Gàmbi]] ([[Gàmbi Wolof]]), [[Gànnaar]] ([[Gànnaar Wolof]]), ak [[Senegaal]] ([[Senegaal Wolof]]). Mi ngi bokk nag moom wolof ci bànqaasub [[atlas bu làkki]] Kongóo yu kojug nit ñu ñuul ñi. Mbokkoo gi mu am ak làkku pël lu yàgg la. Am na it lu mu séq ak yeneen làkk ci gox bi niki séeréer, joolaa ak basari. == Ubbite == Bi ñu demee ba gis jëmm ja, muy ku sew, tuuti te xaw a wow, waaye di ku ñu muure ab taar, ci anam gu woyof te loyox, di ku ñu aare kàttan, sóob ko ci ag fonk-sa-bopp doonte ag neen la, solal ko yéerey yëgle ak jaral, te ma jëli loolu ca jafeem gaa jëli. Bi loolu amee, dama ne leen xanaa kay du kii ngeen ma doon wax? ñu ne ahakay, cis lëf, cig yéemu, ak ñàkk a xalaat ne dinaa sikk mukk ci moom, ma jug man, xajal leen foofa fépp. Ma ne nag waaw ku mel nii, ci li mu làmboo ciy melo, lu ko nit di doye ? Ginnaaw bi nag dégg naa ñuy wax naan moom de bokk na ci ñi gën a jekk ci boobule gox, ànd ak jaaxle ci samaw jëfiin, ci ba ga ma ko fa ba, ma ne leen man : moo xam! Lii mooy li am ci sunu làkk wii, walla yii di yu Afrig yi, dañu di yu am solo te man a dem ni yépp di deme, am barab ci digg barabi làkk yépp, waaye li nu dal nun waa Afrig, mooy li dal sunu lépp, dalaale ci li muy dal sunu [[kàllaama]] yii nga xam ne wii de bokk na ci yi gën a nosu, gën cee nooy, gën cee nangoo defaru, yéwénu, ruy, ci ku ko ruyal, tey way nag ca nanu bëgge mu waye ni. Ana nag ku am janq bu mel ni bii cib taar, nangoo ni, joŋee ni, jekke ni, man nee toppatoo, nangu nee jëme kanam, waaje ni ngir lemu ci say bëgg-bëgg, ana ku am ku mel nii, looy xoolati ku sewe nii, ràgge ni, te taaroodi ni? Li ma bëgg a wax mooy naka la nu bëgg a bàyyee sunu làkk yii, rawatina wii di wolof, ca nooyam ga, ak nangoom ga, ak gàttam ga ak noppaleem ga, taaram ba, leeram ga, manam gaa leeral ak yaatoom ga, ak ruyu gi mu nangu, naan dangay jëlati weneen di ci sonn ak a sonle, naan day wa gën? Ma ne ñoom ñoo gis loolu man de déet ! Wolof mooy làkk wi ñu gën a wax ci [[Senegaal]], waaye ngir doyodig waa [[Afrig]] yi ba leegi, frañse mii nga xam ne lu matul 30 cib téeméer ci doomi Senegaal yi rekk a koy wax moo fiy làkk wu njëkk, maanaam wi nguur gi di waxe di ci liggéeye. Moor Taala [[Baay Faal]] Mbóoj == Cosaanam == Ni ko gëstukat yi waxe, làkku wolof am na ag mbokkoo ak yeneen làkki Afrig yu bari, yu mu bokkal i maam. làkk yi dañ leen a séddale ci ay wàll: bu ci nekk ñi am ag mbokkoo lañu fa def. Nee nañu wolof ci wàll gi ñuy woowe bànqaasub atalaas bu làkki Kongóo yu kojug nit ku ñuul la bokk. Am na ag mbokkoo ak [[pulaar]] ak [[séeréer]] ak [[joolaa]] ak yeneen. Daanaka ñoo ngi koy làkk ci Senegaal gépp, bëj-gànnaar ba bëj-saalum, penku ba sowwu. Donte wolof da di làkku askanu ñi ñuy woowe ay wolof, waaye kàllaama wolof amul uw dig. Dem na ba romb dig (frontiere)yu Senegaal àgg ba [[Gàmbi]], [[Gànnaar]] ba [[Mali]], ci ñaari dëkk yu njëkk yi sax boole nañu ko ci seen i làkki réew. Daanaka gox boo dem ci Senegaal am nañu waxiinu wolof wu wuute: am na wolofi [[Waalo|waalo-waalo]], [[Jolof|jolof-jolof]], [[Siin-Saalum|saalum-saalum]], wu [[Kajoor|kajoor-kajoor]], wu [[Bawol|baol-baol]] ak wu [[lébu]]. == Mbindin == === Abajada wolof === a - à - aa - b - bb - c - cc - d - dd- e - ee- é - ée - ë - ëe - f- g - gg - h - i - ii - j - jj - k - kk - l - ll- m - mm - mb - mp - n - nn - nc - nd - ng - nj - nk - nq - nt - ñ - ññ - ŋ - ŋŋ - o - oo - ó - óo - p - pp - q - r- rr - s - ss - t - tt - u - uu - w - ww - x - y - yy. {|border="1" cellpadding="4" cellspacing="0" class="references-small" style="border:1px solid #aaa; border-collapse:collapse" !L° !Loy !Tàmbali !Biir !Mujj |- |1 |a, A |'''a'''m |sab'''a'''r |mal'''a''' |- |2 |à, À |'''à'''llarba |musk'''à'''llaf |amul |- |3 |aa, Aa |'''aa'''r |tal'''aa'''ta |Tuub'''aa''' |- |4 |b, B |'''b'''ax |jab'''a'''r |ra'''b''' (rabu àll) |- |5 |bb |amul |je'''bb'''i |dë'''bb''' |- |6 |c, C |'''c'''oono |loo'''c'''o |amul |- |7 |cc |amul |so'''cc'''u |bà'''cc''' |- |8 |d, D |'''d'''er |xa'''d'''ar |amul |- |9 |dd |amul |bu'''dd'''i |se'''dd''' |- |10 |e, E |'''e'''gg |x'''e'''l |fex'''e''' |- |11 |ee, Ee |'''ee''' |b'''ee'''s |b'''ee''' |- |12 |é, É |amul |s'''é'''dd |xul'''é'''<sup>1</sup> |- |13 |ée, Ée |'''ée'''m |f'''ée'''y |bu bëgg'''ée'''<sup>1</sup> |- |14 |ë, Ë |'''ë'''s |f'''ë'''s |j'''ë''' |- |15 |ëe, Ëe |amul |b'''ëe'''r |amul |- |16 |f, F |'''f'''or |na'''f'''ar |ne'''f''' |- |17 |g, G |'''g'''arab |ja'''g'''al |na'''g''' (nagu Sàmba) |- |18 |gg |amul |ro'''gg'''anti |se'''gg''' |- |19 |i, I |'''i'''tte |t'''i'''s |kaan'''i''' |- |20 |ii, Ii |'''ii'''r |r'''ii'''ti |b'''ii''' |- |21 |j, J |'''j'''abar |fa'''j'''ar |fa'''j''' (fajal) |- |22 |jj |amul |dà'''jj'''i |bo'''jj''' |- |23 |k, K |'''k'''afe |saa'''k'''u |a'''k''' |- |24 |kk |amul |mà'''kk'''aan |le'''kk''' |- |25 |l, L |'''l'''am |ne'''l'''aw |xe'''l''' |- |26 |ll | amul |xo'''ll'''i |dà'''ll''' |- |27 |m, M |'''m'''ar |la'''m'''an |xa'''m''' |- |28 |mm |amul |sé'''mm'''iñ |jà'''mm''' |- |29 |mb, Mb |'''mb'''ootu |cà'''mb'''ar |dé'''mb''' |- |30 |mp |amul |cà'''mp'''óor |sa'''mp''' |- |31 |n, N |'''n'''ar |daa'''n'''u |fe'''n''' |- |32 |nn |amul |bë'''nn'''u |wa'''nn''' |- |33 |nc |amul |de'''nc'''ukaay |sa'''nc''' |- |34 |nd, Nd |'''nd'''ox |re'''nd'''i |lë'''nd''' |- |35 |ng, Ng |'''ng'''oon |teraa'''ng'''a |la'''ng''' |- |36 |nj, Nj |'''nj'''àmbal |Bà'''nj'''ul |do'''nj''' |- |37 |nk |amul |sà'''nk'''ar |tà'''nk''' |- |38 |nq |amul |sa'''nq'''al |ja'''nq''' |- |39 |nt |amul |sa'''nt'''aane |ba'''nt''' |- |40 |ñ, Ñ |'''ñ'''am |wa'''ñ'''aaru |ngoo'''ñ''' |- |41 |ññ |amul |wà'''ññ'''i |dë'''ññ''' |- |42 |ŋ |'''ŋ'''aam |da'''ŋ'''ar |la'''ŋ''' |- |43 |ŋŋ |amul |wà'''ŋŋ'''arñi |do'''ŋŋ''' |- |44 |o, O |'''o'''yof |l'''o'''xo |laal'''o''' |- |45 |oo, Oo |'''oo'''r |bor'''oo'''m |àndand'''oo''' |- |46 |ó |'''ó'''bbali |j'''ó'''g |pus'''ó'''<sup>1</sup> |- |47 |óo |'''óo'''m |g'''óo'''r |xul'''óo'''<sup>1</sup> |- |48 |p |'''p'''ut |cii'''p'''atu |amul |- |49 |pp |amul |ŋà'''pp'''ati |lu'''pp''' |- |50 |q (ñaari xx) |amul |là'''q'''arci |më'''q''' |- |51 |r, R |'''r'''axas |ma'''r'''al |lii'''r''' |- |52 |rr |amul | fërr-fë'''rr'''i |'''fërr''' |- |53 |s, S |'''s'''uuf |de'''s'''it |fa'''s''' |- |54 |t, T |'''t'''ool |'''t'''uuti |ni'''t''' |- |55 |u, U |'''u'''m |b'''u'''ddi |kudd'''u''' |- |56 |uu, Uu |'''uu'''f |b'''uu'''r |l'''uu''' |- |57 |w, W |'''w'''asin |ta'''w'''at |xe'''w''' |- |58 |ww |amul |xe'''ww'''i |ja'''ww''' |- |59 |x, X |'''x'''ar |sa'''x'''aar |le'''x''' |- |60 |y, Y |'''y'''aram |la'''y'''oo |bë'''y''' |- |61 |yy |amul |fa'''yy'''u |co'''yy''' |} 1- Doonte sax, li ñu téj ci biir lonk yi ngay dégg, nanga bind: xule, bu bëggee, pus, xuloo. == Xool it == * [[commons:Category:Wolof pronunciation| commons:Category:Wolof pronunciation]] Ngir déglu waxiinu baat yi * [[:wikt:| wikbaatukaay:]] ab [[baatukaay]] bu matale ci wolof * [https://web.archive.org/web/20210913200454/http://www.xibaaryi.com/ Xibaaryi.com : ] Yéglekaay bi njëkk ci làkk wolof * [https://web.archive.org/web/20110724140042/http://wolof.xlingua.net/ xLingua-Online-Dictionary German-Wolof / Wolof-German] * [[https://web.archive.org/web/20210704174744/http://saabal.com/ : ]] Yéenekaay gi léppam di wolof tàmbalee ci wolof yam ci wolof [[Wàll:Wolof]] [[Wàll:Làkki senegaal]] [[Wàll:Làkk]] 2a08n3mvo2iqgbwo16nzmm4z5we65p7 FA Šiauliai 0 8879 107608 107522 2026-06-09T07:49:36Z Makenzis 11686 107608 wikitext text/x-wiki {{Infobox football club | clubname = FA Šiauliai | image = | fullname = Šiaulių Futbolo Akademija | nickname = šiauliečiai | founded = 2007 | ground = Savivaldybės stadionas | capacity = 4,000 | chairman = Deivis Kančelskis | coach = {{flagicon|LTU}} Mantas Kuklys | league = [[TOPLYGA]]<ref>[https://toplyga.lt/naujiena/naujasis-lietuvos-futbolo-cempionato-pavadinimas-toplyga/9300 Naujasis Lietuvos futbolo čempionato pavadinimas – TOPLYGA]</ref> | season = 2025 | position = 5th in A lyga | website = http://www.siauliufa.lt | current = | pattern_la1=_hummelcoreXKbw|pattern_b1=_hummelcoreXKSUb|pattern_ra1=_hummelcoreXKbw|pattern_sh1=_hummelcoreXKbw|pattern_so1=_hummel20b| leftarm1=000000|body1=000000|rightarm1=000000|shorts1=000000|socks1=000000| | pattern_la2=_senica1617h|pattern_b2=_senica1617h|pattern_ra2=_senica1617h|pattern_sh2=_senica1617h2|pattern_so2=_hummel20b| leftarm2=FF0000|body2=FF0000|rightarm2=FF0000|shorts2=FF0000|socks2=000000| | pattern_la3 = _hummelcorepoly1718y | pattern_b3 = _hummelcorepoly1718y | pattern_ra3 = _hummelcorepoly1718y | pattern_sh3= _hummelcorepoly1718y | pattern_so3= _yellowline | leftarm3 = FFFF00 | body3 = FFFF00 | rightarm3 = FFFF00 | shorts3 = 000000 | socks3 = 000000 }} '''FA Šiauliai''' (''Futbolo akademija Šiauliai'') benn [[football]] club ci "[[TOPLYGA]]" ([[Lituwaani]]). *'''[[A lyga]], Lituwaani: 0''' :: - ==Staad== *[[Staad Šiaulių miesto savivaldybės]] (Šiauliųų miesto savivaldybės stadionas). == Xool it == === Jukki yi ci lonku === * [[TOPLYGA]] == Karmat ak delluwaay == {{Reflist}} === Lëkkalekaay yu biti === {{Commonscat|FA Šiauliai}} * [http://www.siauliufa.lt Dalub web: FA Šiauliai] * [https://www.facebook.com/siauliufa/ facebook] * [https://int.soccerway.com/teams/lithuania/fa-iauliai/47386/ SOCCERWAY] * [https://www.flashscore.com/team/siauliai-fa/CMmWKuwf/ FLASHSCORE] * [https://www.transfermarkt.com/siauliai-fa/startseite/verein/42310 Transfermarkt] * [https://globalsportsarchive.com/team/soccer/fa-siauliai/36613/ Globalsportsarchive] [[Wàll:Football|Šiauliai]] [[Wàll:Lituwaani|Šiauliai]] 7t3quyp4s8qi2pg7qv6n2yb1ujmzs9x 107609 107608 2026-06-09T07:49:49Z Makenzis 11686 107609 wikitext text/x-wiki {{Infobox football club | clubname = FA Šiauliai | image = | fullname = Šiaulių Futbolo Akademija | nickname = šiauliečiai | founded = 2007 | ground = Savivaldybės stadionas | capacity = 4,000 | chairman = Deivis Kančelskis | coach = {{flagicon|LTU}} Mantas Kuklys | league = [[TOPLYGA]]<ref>[https://toplyga.lt/naujiena/naujasis-lietuvos-futbolo-cempionato-pavadinimas-toplyga/9300 Naujasis Lietuvos futbolo čempionato pavadinimas – TOPLYGA]</ref> | season = 2025 | position = 5th in A lyga | website = http://www.siauliufa.lt | pattern_la1=_hummelcoreXKbw|pattern_b1=_hummelcoreXKSUb|pattern_ra1=_hummelcoreXKbw|pattern_sh1=_hummelcoreXKbw|pattern_so1=_hummel20b| leftarm1=000000|body1=000000|rightarm1=000000|shorts1=000000|socks1=000000| | pattern_la2=_senica1617h|pattern_b2=_senica1617h|pattern_ra2=_senica1617h|pattern_sh2=_senica1617h2|pattern_so2=_hummel20b| leftarm2=FF0000|body2=FF0000|rightarm2=FF0000|shorts2=FF0000|socks2=000000| | pattern_la3 = _hummelcorepoly1718y | pattern_b3 = _hummelcorepoly1718y | pattern_ra3 = _hummelcorepoly1718y | pattern_sh3= _hummelcorepoly1718y | pattern_so3= _yellowline | leftarm3 = FFFF00 | body3 = FFFF00 | rightarm3 = FFFF00 | shorts3 = 000000 | socks3 = 000000 }} '''FA Šiauliai''' (''Futbolo akademija Šiauliai'') benn [[football]] club ci "[[TOPLYGA]]" ([[Lituwaani]]). *'''[[A lyga]], Lituwaani: 0''' :: - ==Staad== *[[Staad Šiaulių miesto savivaldybės]] (Šiauliųų miesto savivaldybės stadionas). == Xool it == === Jukki yi ci lonku === * [[TOPLYGA]] == Karmat ak delluwaay == {{Reflist}} === Lëkkalekaay yu biti === {{Commonscat|FA Šiauliai}} * [http://www.siauliufa.lt Dalub web: FA Šiauliai] * [https://www.facebook.com/siauliufa/ facebook] * [https://int.soccerway.com/teams/lithuania/fa-iauliai/47386/ SOCCERWAY] * [https://www.flashscore.com/team/siauliai-fa/CMmWKuwf/ FLASHSCORE] * [https://www.transfermarkt.com/siauliai-fa/startseite/verein/42310 Transfermarkt] * [https://globalsportsarchive.com/team/soccer/fa-siauliai/36613/ Globalsportsarchive] [[Wàll:Football|Šiauliai]] [[Wàll:Lituwaani|Šiauliai]] 8r7owfxw96zwdyllfrrdhpg9m3obk11