Wikipedia
wowiki
https://wo.wikipedia.org/wiki/X%C3%ABt_wu_nj%C3%ABkk
MediaWiki 1.47.0-wmf.13
first-letter
Xibaarukaay
Jagleel
Waxtaan
Jëfandikukat
Waxtaani jëfandikukat
Wikipedia
Wikipedia waxtaan
Dencukaay
Waxtaani dencukaay
MediaWiki
Waxtaani MediaWiki
Royuwaay
Waxtaani royuwaay
Ndimbal
Waxtaani ndimbal
Wàll
Waxtaani wàll
TimedText
TimedText talk
Module
Discussion module
Event
Event talk
Kawlak
0
3838
107731
105074
2026-08-02T00:14:49Z
InternetArchiveBot
12803
Rescuing 1 sources and tagging 0 as dead.) #IABot (v2.0.9.5
107731
wikitext
text/x-wiki
'''Kawlak''' am réewu-taax mu mag la ca [[senegaal]], féete ci li tollook bëj-saalum-penku [[Ndakaaru]]. Mooy péyu [[Kawlak (diwaan)|diwaanu kawlak]] ak [[Kawlak (gox)|goxu Kawlak]].
[[Dencukaay:SN-Kaolack.png|right|thumb|300px|Fi Kawlak féete ci lonkoyoonu Senegaal]]
== Ci lu daj ==
Ba ko tubaab yi di sanc benn dëkk rekk a fa nekkoon muy Ndangaan. Kawlak yàgg naa doon ab tombum jaaru gerte gi ñu daa béy ci yeneen diwaan yi ko wër, ca [[Waax|waaxam]] wa lañ daa jaarale gerte gi jëme Ndakaaru. Kawlak a ngi bokkoon ci nguuru [[Siin-Saalum|Saalum]] ga woon. Ba fa waa faraas yi di sanc buur-saalum da leen xajaloon ngir bañoon fitna judd ci seen diggante.
[[Dencukaay:MedinaBaayMosque.jpg|thumb|300px|right|Jumaa ju Medina Baay]]
== Diine ==
Kawlak am na ab jàngu bu mag, Saint Theophile Turpin mooy kiñ ko tudde. Njiitu jàngu bu Seneegal bu tay jii, Tewodoor adiriye saar, nekkoon na fa ci diir bu guddu.
Jumaay Kawlak, bi Baay Ñas tambalee woon tabax, tay jii ci diggu ab dëkk bu rëy la ne: Medina Baay. Mooy fa njabootu sëriñu [[Tiijaaniyaa|tiijaan]] boobule, génn àdduna ci atum 1975, dëkke.
== Melosuuf ==
Ci waññi yi ñu amal ci atum 1988 ak 2002, Kawlak amoon na 150 061 ak 172 305 ciy way-dëkk. Ci 2007 ciy ay nattale yu nguuru senegaal def, jàpp nañ ne war naa mat 185 976 ciy way-dëkk.
== Koom-koom ==
Kawlak ab selebiyoon bu mag la. Ci [[Yaxantu|yaxantug]] gerte gi la réewu-taax mu kawlak mas di dund. Bari na ay ja yu mag aki luuma.
== Téerekaay ==
*{{fr}} H. Bessac, « Découverte de gisements néolithiques au sud de Kaolack (Sénégal) », ''Notes Africaines'', Dakar, [[IFAN]], 1952, n° 55, p. 65-69
*{{fr}} Etienne Badiane, ''Développement urbain et dynamiques des acteurs locaux : le cas de Kaolack au Sénégal'', 2004
*{{fr}} André Dessertine, ''Un port secondaire de la Côte occidentale d’Afrique, Kaolack. Étude historique, juridique et économique, des origines à 1958'', Université de Dakar, 1959, 172 p. (Diplôme d’Etudes Supérieures de droit).
*{{fr}} Ibrahima Diouf, ''Kaolack : De l'arachide aux activités informelles'', 1988
*{{fr}} Joseph Fouquet, ''La traite des arachides dans le pays de Kaolack et ses conséquences économiques, sociales et juridiques'', Saint-Louis, IFAN-Université de Dakar, 1958, 263 p. (''Etudes sénégalaises'' n°8) (Thèse de Droit, Montpellier, 1951, publiée)
*{{fr}} Aline Garderet, ''Les fonctions de capitale régionale de Kaolack'', Université de Bordeaux, Travail d'études et de recherches, 1968, 129 p.
*{{fr}} Djibril Gueye, ''L’école coloniale à Kaolack 1893-1928'', Dakar, Université Cheikh Anta Diop, 2002, 105 p. (Mémoire de Maîtrise)
*{{fr}} Fadya Hani, ''Monographie climatique d’une station synoptique, Kaolack 1946-1975'', Université de Dakar, 1982, 113 p. (Mémoire de Maîtrise)
*{{fr}} Emile Jacquier, « Le Port à arachides de Kaolack (Sénégal) », Publications du journal ''Le Génie civil'', 1933
*{{fr}} Alain Morice, ''Projet d'étude sur certaines activités dans la ville de Kaolack (Sénégal)'', École des Hautes études en sciences sociales, Centre d'études africaines, 1981
*{{fr}} Alain Morice, ''Les forgerons de Kaolack : travail non salarié et déploiement d’une caste au Sénégal'', Paris, EHESS, 1982, 6 + 350 p. (Thèse de 3e cycle)
*{{fr}} Mbaye Ndiaye, ''Histoire politique de la ville de Kaolack, (1945-1962)'', Université de Dakar, 1988, 104 p. (Mémoire de Maîtrise)
*{{fr}} Soukeyna Ndiaye, ''Les équipements urbains au Sénégal : l’exemple de Kaolack 1946-1996'', Dakar, Université Cheikh Anta Diop, 1999, 162 p. (Mémoire de Maîtrise)
*{{fr}} Magatte Simal, ''Les Kaolackois face à l’administration coloniale de 1914 à 1938'', Dakar, Université Cheikh Anta Diop, 1990, 93 p. (Mémoire de Maîtrise)
*{{fr}} Denis Tillinac, ''L'Hôtel de Kaolack'', Robert Laffont, 1991, Pocket n° 4602, 1992, 177 p. {{ISBN|2266052217}} (roman)
== Lëkkalekaay yu biti ==
{{commons|Category:Kaolack}}
*{{en}} [https://web.archive.org/web/20080411053909/http://www.fallingrain.com/world/SG/10/Kaolack.html Maps, weather and airports for Kaolack]
*{{fr}} [http://www.planete-senegal.com/visites/kaolack.php Kaolack sur Planète Sénégal]
*{{fr}} [http://www.lib.utexas.edu/maps/ams/west_africa/txu-oclc-6595921-nd28-6.jpg Carte au 1/200000 de la région]
[[Wàll:réewi-taaxi Senegaal]]
472758g8gyzfvus1fe4sss2co7c676p
Jëfandikukat:Revi C.
2
6867
107730
106533
2026-08-02T00:03:27Z
Pathoschild
791
global user pages ([[m:Synchbot|requested by Revi C.]])
107730
wikitext
text/x-wiki
__NOINDEX__
{{#babel:ko|en-3|wo-0}} [[File:Revi wikimedia image.jpg|thumb|center|middle|If you are here to talk about CommonsDelinker removing a deleted image, please [[:c:User talk:Revi C.|go here]].]]
a8zmndkxtc4gjz8xxhmkwrin8o4e0qh
Waxtaani jëfandikukat:Revi C.
3
6868
107729
106532
2026-08-01T23:22:45Z
Pathoschild
791
global user pages ([[m:Synchbot|requested by Revi C.]])
107729
wikitext
text/x-wiki
__NOINDEX__
[[File:Revi logo (pink).png|thumb|center|PLEASE DO NOT LEAVE MESSAGE HERE!]]
'''  BEFORE YOU BLOCK MY ACCOUNT: IF MY EDIT SUMMARY INCLUDE PREFIX ''(Script)'', DON'T BLOCK ME, JUST TELL ME TO SLOW DOWN AT COMMONS' TALK PAGE. IT IS AN AUTOMATED SCRIPT BEING USED ON COMMONS TO MOVE FILES.
Instead, please leave your message following site:
[[File:Commons-logo.svg|45px|link=commons:User talk:Revi C.]] [[commons:User talk:Revi C.]] for renaming stuff or [[User:CommonsDelinker|CommonsDelinker]] action (I am {{int:Group-sysop}} there)
[[File:Wikimedia Community Logo optimized.svg|45px|link=m:User talk:Revi C.]] [[meta:User talk:Revi C.]] for other stuff (User right notification, revert message, etc...)
Messages left on this page may be reverted or moved without any response.
esxe13mcstpjlux1bt2hqwxr2v8t8mn
Jëfandikukat:Hym411
2
7040
107732
106536
2026-08-02T00:39:56Z
Pathoschild
791
global user pages ([[m:Synchbot|requested by Hym411]])
107732
wikitext
text/x-wiki
#REDIRECT [[User:Revi C.]]
88g0cv17whfgb1wkeh281mptujwtlut
Waxtaani jëfandikukat:Hym411
3
7041
107733
106537
2026-08-02T01:09:20Z
Pathoschild
791
global user pages ([[m:Synchbot|requested by Hym411]])
107733
wikitext
text/x-wiki
#REDIRECT [[User talk:Revi C.]]
o9z79lcc9a9pfmqmrod5w3eyk4q9i0o