Wikipedia
wowiki
https://wo.wikipedia.org/wiki/X%C3%ABt_wu_nj%C3%ABkk
MediaWiki 1.47.0-wmf.14
first-letter
Xibaarukaay
Jagleel
Waxtaan
Jëfandikukat
Waxtaani jëfandikukat
Wikipedia
Wikipedia waxtaan
Dencukaay
Waxtaani dencukaay
MediaWiki
Waxtaani MediaWiki
Royuwaay
Waxtaani royuwaay
Ndimbal
Waxtaani ndimbal
Wàll
Waxtaani wàll
TimedText
TimedText talk
Module
Discussion module
Event
Event talk
Dawaan gu wéy
0
5890
107742
99291
2026-08-09T08:00:17Z
Amherst99
1803
/* */
107742
wikitext
text/x-wiki
[[Dencukaay:Direct current symbol.svg|thumb|200px|rigth|njunj gu dawaan gu wéy]]
'''Dawaan gu wéy''' (ñu man koo tënk ci '''DC''' ''direct current'' ci [[wu-angalteer]], moom lees di gën a jëfandikoo), di dëddoo ak [[dawaan gu safaanu]] AC, xeetu dawaan la gu am genn jubluwaay. Dawaan gi dafay wéy di dox ci ag ndombo ci genn jubluwaay. [[Mbëjfeppal]] yi ci genn jubluwaay lauy wéy di daw.
== Nattiin ==
Dawaan gu wéy ciy amper lees koy natt. Benn amper mooy ,24*10<sup>18</sup> [[mbëjfeppal]] ci saa (I = Q/t), I = dawaan, Q= coulomb, t= saa).
Wenn rëdd wu wéy ak ñett yu ndaw, ci suufam, mooy njunju dawaan gu wéy; dees na jëfandikoo itam DC (Direct Current). Dawaan gu safaanu moom AC ''alternating current'' lees di jëfandikoo wall njunj wii di ~.
== Jëfandikoom ==
Dawaan gu wéy lees di jëfandikoo lu bari la ci [[taraay gu suufe]] ak ci [[mbëjfeppal]], rawatina ci jumtukaay yiy doxeek [[tegle]] yiy man a jur dawaan gu wéy kepp. Ci daamar yi, su [[safaanukaay]] bi juree dawaan gu safaanu dess koy soppali gu wéy. Saxaar yiy doxee mbëj itam ñoom dawaan gu wéy lañuy jël.
== Taariixam ==
[[Thomas Alva Edison]] mooy ki fi taxawal séddaleeg dawaan gu wéy ci wetu njeextalu XIX<sup>u</sup> xarnu bi, bi [[ndefar]] gi tambalee jëfandikoo [[mbëj]]. Ci ginnaaw bi lees ko wuutaleek dawaan gu safaanu gi [[Nikola Tesla]] sakk, ndax limu gën a yomb a yóbb ci diggante yu gubb.
{{wikibaatukaay}}
[[Wàll:Dawaanu mbëj]]
pi3qjig5di8pz8qc4heaw28r0f14vwo
107743
107742
2026-08-09T08:00:56Z
Amherst99
1803
/* Nattiin */
107743
wikitext
text/x-wiki
[[Dencukaay:Direct current symbol.svg|thumb|200px|rigth|njunj gu dawaan gu wéy]]
'''Dawaan gu wéy''' (ñu man koo tënk ci '''DC''' ''direct current'' ci [[wu-angalteer]], moom lees di gën a jëfandikoo), di dëddoo ak [[dawaan gu safaanu]] AC, xeetu dawaan la gu am genn jubluwaay. Dawaan gi dafay wéy di dox ci ag ndombo ci genn jubluwaay. [[Mbëjfeppal]] yi ci genn jubluwaay lauy wéy di daw.
== Nattiin ==
Dawaan gu wéy ciy amper lees koy natt. Benn amper mooy ,24*10<sup>18</sup> [[mbëjfeppal]] ci saa (I = Q/t), I = dawaan, Q= coulomb, t= saa).
Wenn rëdd wu wéy ak ñett yu ndaw, ci suufam, mooy njunju dawaan gu wéy; dees na jëfandikoo itam DC (''direct current''). Dawaan gu safaanu moom AC ''alternating current'' lees di jëfandikoo wall njunj wii di ~.
== Jëfandikoom ==
Dawaan gu wéy lees di jëfandikoo lu bari la ci [[taraay gu suufe]] ak ci [[mbëjfeppal]], rawatina ci jumtukaay yiy doxeek [[tegle]] yiy man a jur dawaan gu wéy kepp. Ci daamar yi, su [[safaanukaay]] bi juree dawaan gu safaanu dess koy soppali gu wéy. Saxaar yiy doxee mbëj itam ñoom dawaan gu wéy lañuy jël.
== Taariixam ==
[[Thomas Alva Edison]] mooy ki fi taxawal séddaleeg dawaan gu wéy ci wetu njeextalu XIX<sup>u</sup> xarnu bi, bi [[ndefar]] gi tambalee jëfandikoo [[mbëj]]. Ci ginnaaw bi lees ko wuutaleek dawaan gu safaanu gi [[Nikola Tesla]] sakk, ndax limu gën a yomb a yóbb ci diggante yu gubb.
{{wikibaatukaay}}
[[Wàll:Dawaanu mbëj]]
d3vc0fyl447ewvl0fnd53fk7cfalx3h
Dawaan bu safaanu
0
5892
107741
99467
2026-08-09T07:40:42Z
Amherst99
1803
/* */
107741
wikitext
text/x-wiki
'''Dawaan bu safaanu''' ('''DS''' walla '''AC''' ci [[wu-angalteer]]: alternating current) màndargoo ag walug [[dawaan]] guy soppiku ci jamono muy ci [[taraay]] walla ci jubluwaay.
== Doxiin ==
Naka-jekk dawaanu [[mbëj]] suñu koy séddale, ci dawaan bu safaanu bu [[Baraay|baraayam]] sax ci 50 Hz walla 60 [[Hz]] lees koy defe (+ ak - bi dañuy safaanu ci watatukaay bi juroom-fukki saa yu ne). Dawaan bi ak [[dendu mbëj]] bi, ci biir [[watatukaayu mbëj]] bi, seen Demiin dafay mel ne bu ab [[duusub sin]].
Jëfandikoo gu dawaan bu safaanu mi gi jóge ci li [[Jurukaay|jurukaayu dawaan]] yi, ci yaxanaay ci koom-koom ak seenug yomb a defar, di jur dawaan bu safaanu ci anam gu yomb, kon dawaan bi ci boppam kenn du ko soppiwaat laataa ag jëfandikoo.
Fi njariñ li gën a feeñee sax mooy séddaleeb dawaan bu safaanu bir na ne moo gën a yaxan [[dawaan bu wéy]] ci séddaleeb [[dend bu kawe]] (ñakkug kàttan gi ci buum yu gudd yi moo gën a néew). rawatina, ci diggante gu [[gennwéq]] walla wéq yu bari, bir na yaxanaay gu [[ñettiwéq]] di gees gën a jëfandikoo ndax néewteey ñakkug kàttan ngir njeexitu [[Joule]] (moo tax dijjaayu watatukaay yi gën a néew, maanaam wëñ yu gën a sew); jëfandikoog dawaan bu safaanu bu ñettiwéq lawal na buumi yóbb yi ci diggante yu gudd lool yi.
Genn Màndarga gu am-solo gu dawaan bu safaanu, ba waral ci genn wàll li tax ñépp jël ko, mooy yomb gee jëfandikoo fu nekk, yomb gee soppi ci lim yu wuute ci [[taraay]]u [[dawaan]], ci ndimbalu [[soppalikaay]] yi, ak ñakkug kàttan gu digu.
Donte yenn jumtukaay yi [[dawaan bu wéy]] lañuy doxe, waaye loolu manees na koo ame ci dawaan bu safaanu, sunu jëfandikoo ab [[jubbantikaay]].
Suñu jëfandikoo ag xaralag [[mbëjfeppal gu kàttan]] gu ñaw, manees naa jëfandikoo dawaan bu wéy ngir am dawaan bu safaanu, jur ko ci yenn anami [[baraay]], [[melokaanu duus]] ak taraay jaare ko ciy jumtukaay yees duppee [[jallarbikaay]].
== Taariix ==
[[Dencukaay:World Map of Mains Voltages and Frequencies, Simplified.png|400px|thumb|right|Lonkoyoonu àdduna bi bees melool aju ci taraay ak baraayu kàttanu mbëj ci ndombo yiy séddale dawaan bi ci kër yi.]]
Ca njalbeenu njëfandikug kàttanu mbëj ci ndefar gi ci XIX<sup>u</sup> xarnu [[daawaan bu wéy]] lañu doon jëfandikoo, ndax li mu doonoon lu neex a rënk ciy [[tegle]] ak li mu gën a wóor dawaan bu safaanu. Tomb bu mujj bi Thomas Alva Edison mooy ki ko doon wax ci lees tuddewoon [[xareeb dawaan yi]].
Dawaan bu safaanu, gi soloom doonoon lu beneen xaaj bi boole woon [[Nikola Tesla]] ak [[George Westinghouse]] doon aar, manul a ñakk ci njëfandiku gu ab [[soppalikaay]], moom mi tax ñuy man jokkalante mbëj mi ci diggante yu gudd. Te itam [[doxalukaayu mbëj]] yu dawaan bu safaanu ñoo gën a wóor te gën a yaxan yu dawaan yu wéy yi.
Ci jamono jii ci [[àdduna]] bi dawaanu mbëj ci ñaari [[baraay]] lañu koy séddalee, 50 Hz([[Tugal]], [[Asi]], [[Afrig]]) ak 60 Hz([[Diiwaan-yu-Bennoo]] ak goxu [[Aamerig]] bépp ci lu daj, genn xaaju [[sapoŋ]]) ak taraay yu wuute.
== Xool it ==
* [[Dawaan gu wéy]]
* [[Dawaanu mbëj]]
* [[Kàttanug mbëj]]
* [[mbëj]]
== Téerekaay ==
* {{en}}[[Charles Proteus Steinmetz]]: [http://www.archive.org/details/theorycalculatio00steiuoft ''Theory and Calculation of Alternating Current Phenomena''] ([[McGrawHill]], [[1900]])
* {{en}}Charles Proteus Steinmetz: [http://www.archive.org/details/ElectricDischargesWavesAndImpulses ''Electric Discharges, Waves and Impulses''] ([[1914]]) * {{en}}Charles Proteus Steinmetz: [http://www.archive.org/details/TheoreticalElementsOfElectricalEngineering ''Theoretical Elements of Electrical Engineering''] ([[1915]])
* {{en}}Charles Proteus Steinmetz: [http://www.archive.org/details/TheoryAndCalculationOfElectricalApparatus ''Theory and Calculation of Electrical Apparatus] ([[1917]])
* {{en}}Charles Proteus Steinmetz: [http://www.archive.org/details/theoryandcalcula017202mbp ''Theory and Calculation of Transient Electric Phenomena and Oscillations](McGrawHill, [[1920]])
* {{en}}[[Louis Cohen]]: [http://www.archive.org/details/formulaetablesfo00coherich ''Formulae and Tables for the Calculation of Alternating Current Problems] (McGraw-Hill, [[New York]], [[1913]])
* {{en}}[[Ernst Julius Berg]]: [http://www.archive.org/details/engineelectrical00bergrich ''Electrical Engineering, First Course''] (McGrawHill, New York, [[1916]])
* {{en}}Ernst Julius Berg: [http://www.archive.org/details/electricalengine00bergrich ''Electrical Engineering, Advanced Course''] (McGrawHill, New York, 1916)
[[Wàll:Dawaanu mbëj]]
0xmy3j9lkztls3qhx23n0k0pbmguo8j
Mikael Jakson
0
8965
107740
107579
2026-08-08T22:27:22Z
Der-Wir-Ing
8995
Reverted 2 edits by [[Special:Contributions/2partyrock1975|2partyrock1975]] ([[User talk:2partyrock1975|talk]]): Edit from globally banned user Wikinger (TwinkleGlobal)
107740
wikitext
text/x-wiki
Michael Joseph Jackson (29 ut 1958 – 25 juin 2009) doomu Amerique la woon, waykat, bindkat, feccikat ak ku bëgg doomi aadama yi. Ñu ngi ko woowe "Buuru Pop", ñu jàpp ni kenn la ci nit ñi gëna am solo ci wàllu aada ci 20eelu xarnu bi.<ref>{{Cite web|url=https://www.forbes.com/sites/ceciliarodriguez/2018/11/26/michael-jackson-on-the-wall-as-art-object-of-a-blockbuster-paris-exhibition/|title=New Blockbuster Paris Exhibition Celebrates Michael Jackson|first=Cecilia|last=Rodriguez|website=Forbes|access-date=October 31, 2019|archive-url=https://web.archive.org/web/20191031042818/https://www.forbes.com/sites/ceciliarodriguez/2018/11/26/michael-jackson-on-the-wall-as-art-object-of-a-blockbuster-paris-exhibition/|archive-date=October 31, 2019|url-status=live}}</ref><ref>{{Cite web |last=Stevens |first=Hampton |date=2010-06-24 |title=Michael Jackson was the most influential artist of the 20th century. |url=https://www.theatlantic.com/entertainment/archive/2010/06/michael-jacksons-unparalleled-influence/58616/ |access-date=2024-04-28 |website=The Atlantic |language=en}}</ref>
== Rew Yii Aduna Yep ==
<references />
avdbi40ikgzg1eu4k9uv5iv9jik9c1x