Wikipedia wowiki https://wo.wikipedia.org/wiki/X%C3%ABt_wu_nj%C3%ABkk MediaWiki 1.47.0-wmf.17 first-letter Xibaarukaay Jagleel Waxtaan Jëfandikukat Waxtaani jëfandikukat Wikipedia Wikipedia waxtaan Dencukaay Waxtaani dencukaay MediaWiki Waxtaani MediaWiki Royuwaay Waxtaani royuwaay Ndimbal Waxtaani ndimbal Wàll Waxtaani wàll TimedText TimedText talk Module Discussion module Event Event talk Gëwéel 0 3904 107770 106350 2026-08-29T00:13:22Z InternetArchiveBot 12803 Rescuing 1 sources and tagging 0 as dead.) #IABot (v2.0.9.5 107770 wikitext text/x-wiki '''Gëwéel''' yi ñaari rëdd lañu yu dëppook [[yamoo]] gi: [[gëwéelub Tef]] tollu ci 23°24' wu [[tus-wu-gaar]] wu bëj-gànnaar gi ak [[gëwéelub Sànkar]] tollu ci 23°27' wu tus-wu-gaar wu bëj-saalum. di nañu woowe it gëwéel diiwaan yi ne ci li wër rëdd yooyule (di faral di wax dëkk ci gëwéel yi). == Melokaan == Ci li jege [[yamoo]] gi, di nañu faral di gis klimaa bu ànd ak tàngoor wu tar ak taw bu bari ci at mi mépp: di ko wax [[klimaab yamoo]]. Waaye, ci li jege gëwéel yi (Tef mbaa Sànkar), ci at mi [[noor]] ak [[nawet]] rekk a ci am, kon wàcciit yi (taw yi) day wuute ci jamonoy at mi, ba daanaka at mépp ay tàng, di li ñuy wax [[klimaab gëwéel]]. Waaye nag jàpp nañu ne it ngelaw yiy upp ak duusi géej yi ak rëyaayu diiwaan bi am nañu ay jeexiital yu solowu ci klimaay diiwaan yi, ba tax na su nu seetloo yenn diiwaan yi, doonte nekk nañu ci wetu ab gëwéel, amuñu klimaab gëwéel (ci misaal diggu Óstraali walla bu Sahara, nga xamne amuñu nawet) ak yenn diiwaan yu am klimaab gëwéel te nekkuñu ci lu jege gëwéel yi( lu mel ne réewum [[Keeñaa]], nekk ci [[yamoo]] gi te li ëpp ci suufam klimaab gëwéel la am). [[Dencukaay:Wendekreise.png|300px|thumb|Gëwéel yi ñooy rëdd yu baxa yu xëm yi, ci kaw ak suufu [[yamoo]] gi, moom di rëdd wu leer wi]] == Diiwaani gëwéel yu mag yi == Diiwaan yiy dund cib klimaab gëwéel dëgg-dëgg ñoo ngi nekk ci [[diggu Aamerig]] ak [[bëj-saalumu Aamerig]], ci digg ak genn wàllu [[bëj-gànnaaru Afrig]], ci bëj-gànnaaru [[Óstraali]] ak genn wàllu [[Endoneesi]]. Li des ci barabu diggantegëwéel bi dañu leen di séddale ci diggante klimaab [[tàkk]] (rawatina ci [[Afrig]]), bu [[yamoo]] walla bu xaw a sedd (rawatina ca [[Asi]] === Lëkkalekaay yu biti === * {{fr}} CNRS [https://web.archive.org/web/20101112095723/http://www.cnrs.fr/cw/dossiers/dosclim/rechfran/4theme/paleo/biodiversitetropic.html] La bodiversité tropicale. * {{fr}} [http://www.agropolis.fr/ Agropolis]: Portail européen de recherche de formation et d'information sur la Méditerranée et les pays tropicaux. * {{fr}} [https://web.archive.org/web/20080624151534/http://museum.agropolis.fr/agora/viewtopic.php?t=50&start=0&postdays=0&postorder=asc&highlight=&sid=e1866f5a9f154c9328802143fdc920d5 Une agronomie tropicale au service des agricultures familiales ?] (Forum d'Agropolis) * {{fr}} P. W. Richards, professeur de botanique, [http://www.fao.org/docrep/x5381f/x5381f03.htm "Etude de la végétation tropicale (se référant particulièrement à la Guyane britannique et à l'Afrique occidentale britannique)"]. University College of North Wales, Bangor. UNESCO 1956. [https://web.archive.org/web/20100912123829/http://www.fao.org/documents/ Archives de la fAO]. * {{fr}} [https://web.archive.org/web/20110222150544/http://world.mongabay.com/francais-french/ Mieux connaître et protéger la nature et les peuples des forêts humides] * {{fr}} [https://web.archive.org/web/20110608161026/http://www.agroparistech.fr/geeft/ "Gestion environnementale des écosystèmes et forêts tropicales"] : Groupe de Formation et de Recherche sur les écosystèmes tropicaux forestiers et naturels, [https://web.archive.org/web/20110310045202/http://www.agroparistech.fr/-Ecole-interne-ENGREF-.html AgroParisTech-ENGREF] {{Commons|Category:Tropics|Wàll:gëwéel}} [[Wàll:Gëwéel]] ewppa6du80poipmi9xritgman982fzb Nordic Africa Institute 0 8949 107771 106715 2026-08-29T00:21:43Z InternetArchiveBot 12803 Rescuing 1 sources and tagging 0 as dead.) #IABot (v2.0.9.5 107771 wikitext text/x-wiki '''Nordic Africa Institute''' – NAI –  (cii suedwa: ''Nordiska Afrikainstitutet'') Kërug gëstu la, xeltu aki xibaar ci Afrigug tey ngir réew Ërob yi féete bët gànnaar. Kër gi day amal liy gëstu ci coobareem yu am solo ci njiitéef joxey xalaat aka leeral jëlum dogal yi,  aju ci defi jéegoy xam_xam yu tënku ci gëstu ci Afrigu démb ak tey. Kërug Afrik ngir réew Ërob yi féete bët gànnaar (''Nordic Africa Institute'') ñu ngi ko soss ci atum 1962 dax muy jàppale ci wàllu koom réewi [[Sued]], [[Finland]] ak [[Island]]. [[Danmark]] ak [[Norwes]] ñoomit ay bokk lanu cag njalbéen ci réew yi ko soss bokk yit ci ñi ciy jàpp ci wàllu koom waaye danu cee génn ci atum 2013 ak atum 2015. Ci yorin gi ci yëngu-yëngu gi kër gi day dox niki nguurug suwed gi wéeru ci bãxaasu bi yore li ëmbu ci bitim réew. Mu ngi nekk ca Uppsala. Nordic Africa Institut mu bokk ci – AEGIS –, Lëkkaloog kërug gëstug Afrig yi ci Ërob. Kër direktëër à kiko jiite ak kureelug xeltu ci sémb ak gëstu seen cër di xelal njiit li direktëër. == Direktëër NAI yii fi nekk tey akk yii fi nekkon == * Therese Sjömander Magnusson, tambale ci atum 2019 * Iina Soiri 2013-2019 * Carin Norberg 2005-2013 * Lennart Wohlgemut 1993-2005 * Anders Hjort af Ornäs 1984-1993 * Carl Gösta Widstrand 1962-1984 == Amlanteel bi ci biti == * [https://web.archive.org/web/20240221193927/https://nai.uu.se/ Bërabu Jokkoo bi mu moomal boppam] * [https://www.aegis-eu.org/members Way bokk lëkkaloo gi ci AEGIS, kërug gëstug Afrig yi ci Ërob] 9dh6yqxykfcvris7qeq5cig6eidvhep