Wikipedia
wowiki
https://wo.wikipedia.org/wiki/X%C3%ABt_wu_nj%C3%ABkk
MediaWiki 1.47.0-wmf.18
first-letter
Xibaarukaay
Jagleel
Waxtaan
Jëfandikukat
Waxtaani jëfandikukat
Wikipedia
Wikipedia waxtaan
Dencukaay
Waxtaani dencukaay
MediaWiki
Waxtaani MediaWiki
Royuwaay
Waxtaani royuwaay
Ndimbal
Waxtaani ndimbal
Wàll
Waxtaani wàll
TimedText
TimedText talk
Module
Discussion module
Event
Event talk
Ndakaaru
0
1021
107774
106879
2026-09-04T20:24:18Z
Pierre Bon-Bon
17045
Ajout d’un signe de ponctuation
107774
wikitext
text/x-wiki
{{Junj}}
{{Infobox Dëkk
|turudëkk=Dëkku Ndakaaru<br />[[Dencukaay:Dakar_CoA.png|thumb|centre|350 px]]
|réew=[[Senegaal]]
|ron-réew=[[Ndakaaru]]
|diiwaan=[[Ndakaaru]]
|tus-wu-gaar=
|tus-wu-taxaw=
|way-dëkk=2450000
|yaatuwaay=550 km²
|nataal=Dakar-Indépendance.jpg
|ay kàddu=Dëkku Ndakaaru
|nataalbar=Dakar-Indépendance.jpg
}}
'''Ndakaaru''' (Dakar) Nekkoon reewu Afrig gu sowwu gu [[Faraas|Faraas]] (ASF, walla AOF ci [[Faraañse|FR]]), Ndakaaru fimne mooy reewum Barug [[Senegaal]] akit goxub Ndakaaru, tolluwaayam ci péeteg sowwu bu Afrig, ci jegeem [[Daanaka-dun]] bu Kap-Wert, waral na sancug [[notaakon]] yu jëkk yi, Akit yaxantu ak Àdduna bu bees bi, te ame na peetewaayu ngëneel ci jëflanteg cosaani Saa-Afrig yi ak Saa-Tugal yi. Fa lees Taxawalee woon [[Xumbalu Àddina bu fànni ñuule]] (jaam yu ñuul) bu njëkk bi ci xalaatu [[Leopool Sedaar Sengoor]] atum 1966, Dëkk bii mooy toogu bu Këru-gëstu bu dàttu bu Afrig gu ñuule (KDAN, walla IFAN ci FR) akit bu Bànk bu diggu bu guuri Afrig gu sowwu (BDGAS walla BCEAO ci [[Faraañse|FR]]).
[[Dencukaay:Dakar - Panorama urbain.jpg|alt=|gauche|vignette|300x300px|Ndakaaru]]
{{commons|Category:Dakar|Ndakaaru}}
[[Wàll:Dëkki Senegaal]]
[[Wàll:Péy]]
ry91avfukmbfa6izoh3m1gefgldjjlx