Wikipedia
wowiki
https://wo.wikipedia.org/wiki/X%C3%ABt_wu_nj%C3%ABkk
MediaWiki 1.47.0-wmf.21
first-letter
Xibaarukaay
Jagleel
Waxtaan
Jëfandikukat
Waxtaani jëfandikukat
Wikipedia
Wikipedia waxtaan
Dencukaay
Waxtaani dencukaay
MediaWiki
Waxtaani MediaWiki
Royuwaay
Waxtaani royuwaay
Ndimbal
Waxtaani ndimbal
Wàll
Waxtaani wàll
TimedText
TimedText talk
Module
Discussion module
Event
Event talk
Sëriñ Basiiru Mbàkke
0
5053
107794
104106
2026-09-28T00:26:39Z
InternetArchiveBot
12803
Rescuing 1 sources and tagging 0 as dead.) #IABot (v2.0.9.6
107794
wikitext
text/x-wiki
[[Image:S Basiiru.jpg|thumb|right|350px|S Basiiru Mbàkke]]
Kenn ci doomi S Tuubaa yu am yi ag jeexiital te àgguñu ci di xalifa, ku amoon [[xam-xam]], mooy ki bind téere bu am solo bii di ab delluwaay ci yoon wi, di "'''Minanul Baaqiil Qadiim'''"
ku ci bagga xootal na xool [https://web.archive.org/web/20110728181419/http://www.wikimouridia.org/ Sëriñ Basiiru Mbàkke] ci situ [https://web.archive.org/web/20110728181419/http://www.wikimouridia.org/ '''wikimouridia.org''']
[[Wàll:Niti senegaal]]
[[Wàll:Yoonu murit]]
o6zt0kt30qlj97jo6d00qacwpvkbmr9
Anxiety disorder
0
7812
107793
107764
2026-09-27T16:57:10Z
InternetArchiveBot
12803
Add 1 book for [[en:Wikipedia:Verifiability|verifiability]] (20260927sim)) #IABot (v2.0.9.6) ([[User:GreenC bot|GreenC bot]]
107793
wikitext
text/x-wiki
{{DISPLAYTITLE:Feebaru naqar gu metti ku dara saful|noerror}}
<!--Definition and symptoms -->
'''Feebaru naqar gu metti ku dara saful''' '''MDD''', ñu xame ko itam ni '''déteelu''', mooy benn [[feebaru xel]]bu ñuy xame ci ñaari ayubés ci [[déteelu (dikkale)|(dikkale]] bu feeñ ci yu bari.<ref name=NIH2016/> Dafay faraldi di ànd ak tuuti [[ci wóólu sa bopp]], [[ñakka am yëg yëg]] ci yoon ci ay yëngu yëngu yu wara neex, njaxlafaay gu wacc, ak [[mettit]] bu amul lu ko waral.<ref name=NIH2016/> Nit ñi mëna nañu am yenn saay [[ay yaakaar yu du noonu|ay gëm gëm yu amul]] walla [[gis ay mbir yu fi nekkul|gis walla dégg ay mbir yu nit ñi dul gis walla dégg]].<ref name=NIH2016/> Ñenn ñi am nañu [[Ay diiru naqar gu metti te dara safu ko|ay diiru déteelu]] te ci seen diggante dañuy mel ñépp ay at, te ñeneen ñi ci boobu diir dañuy génne feebar bi.<ref name=DSM5/> Feebaru naqar gu metti ku dara saful mën na japp nit ki japp bu ñaaw ci dundam, walla ci njàngam, walla ci nelawam, walla ci ni muy lekke, ak ci wér gu yaram.<ref name=NIH2016/><ref name=DSM5/> Ci diggante 2-8% ci magg ñi ame feebaru naqar gu metti ku dara saful dañuy dee ak [[xaru]], <ref name=Rich2014>{{cite book|last1=Richards|first1=C. Steven|last2=O'Hara|first2=Michael W. |name-list-format=vanc |title=The Oxford Handbook of Depression and Comorbidity|date=2014|publisher=Oxford University Press|isbn=9780199797042|page=254|url=https://books.google.com/books?id=9jpsAwAAQBAJ&pg=PA254|language=en}}</ref><ref>{{cite book |last1=Strakowski|first1=Stephen |last2=Nelson |first2=Erik |title=Major Depressive Disorder |date=2015 |publisher=Oxford University Press |isbn=9780190264321 |page=PT27 |url=https://books.google.ca/books?id=nD8FCgAAQBAJ&pg=PT27 |language=en}}</ref> te lu tollook 50% ci nit ñiy dee ak xaru amoon nañu déteelu walla beneen feebar [[feebaru dikkale|dikkale]].<ref>{{cite journal |last1=Bachmann |first1=S |title=Epidemiology of Suicide and the Psychiatric Perspective |journal=International Journal of Environmental Research and Public Health |date=6 July 2018 |volume=15 |issue=7 |pages=1425 |doi=10.3390/ijerph15071425 |pmid=29986446|pmc=6068947 |quote=Half of all completed suicides are related to depressive and other mood disorders}}</ref>
<!-- Cause and diagnosis -->
Gëm nañu ne li koy indi mooy ab mbooloowu [[ndono yi ci dereet|ndono ci dereet]], ci li ñu wër, ak ci wallu xel.<ref name=NIH2016>{{cite web|title=Depression|url=http://www.nimh.nih.gov/health/topics/depression/index.shtml|website=NIMH|accessdate=31 July 2016|date=May 2016|deadurl=no|archiveurl=https://web.archive.org/web/20160805065529/http://www.nimh.nih.gov/health/topics/depression/index.shtml|archivedate=5 August 2016}}</ref> Risk yi ñooy ci wallu [[cosaani waa kër gi (paj mi)|cosaanu waa kër gi]] ci li koy joxe, coppite ci dundum nit ki, yenn garab yi, [[jafe jafe yu metti ci wér gu yaram|jafe jafe yu metti ci wér gu yaram]], ak [[feebaru dorogewu]] .<ref name="NIH2016" /><ref name="DSM5" /> Lu tollook 40% ci risk yi ñungi joge ci ndono yi ci dereet.<ref name="DSM5" /> Saytu yi ci feebaru naqar gu metti ku dara saful mungi wekku ci jaar jaar yi nit ki di nettali ak benn [[saytu ci fi xelam tollu]].<ref name=Pat2015>{{cite book|last1=Patton|first1=Lauren L.|name-list-format=vanc |title=The ADA Practical Guide to Patients with Medical Conditions|date=2015|publisher=John Wiley & Sons|isbn=9781118929285|page=339|edition=2|url=https://books.google.com/books?id=OTJiCgAAQBAJ&pg=PA339|language=en}}</ref> Amul benn saytu ci laboratoire ngir feebaru déteelu yu gêna bari yi.<ref name=DSM5/> Di ko saytu, waaaye, mën nañu ko def ngir dindi fi yenn jafe jafe yi ci yaram bi yu mëna indi ay yeneen mandarga yu mel noonu.<ref name=Pat2015/> Feebaru déteelu moo gëna metti te mooy gëna yagg [[naqar]], lu bokk ci dund nit ki la .<ref name=DSM5/> Lii di United States Preventive Services Task Force (USPSTF) laaj na ñu saytu déteelu ci ñi am lu ëpp fukki at ak ñaari, <ref name=US2016>{{cite journal |vauthors=Siu AL, Bibbins-Domingo K, Grossman DC, Baumann LC, Davidson KW, Ebell M, García FA, Gillman M, Herzstein J, Kemper AR, Krist AH, Kurth AE, Owens DK, Phillips WR, Phipps MG, Pignone MP |title=Screening for Depression in Adults: US Preventive Services Task Force Recommendation Statement |url=https://archive.org/details/sim_jama_2016-01-26_315_4/page/380 |journal=JAMA |volume=315 |issue=4 |pages=380–7 |date=January 2016 |pmid=26813211 |doi=10.1001/jama.2015.18392 }}</ref><ref name=US2016Peds>{{cite journal |vauthors=Siu AL |title=Screening for Depression in Children and Adolescents: U.S. Preventive Services Task Force Recommendation Statement |journal=Annals of Internal Medicine |volume=164 |issue=5 |pages=360–6 |date=March 2016 |pmid=26858097 |doi=10.7326/M15-2957 }}</ref> ci waxtu woowu ci [[xibaaru Cochrane]]gis nañu ne di faraldi di laajte du jappale génne walla faj feebar bi.<ref name=Gil2005>{{cite journal |vauthors=Gilbody S, House AO, Sheldon TA |title=Screening and case finding instruments for depression |journal=The Cochrane Database of Systematic Reviews |issue=4 |pages=CD002792 |date=October 2005 |pmid=16235301 |doi=10.1002/14651858.CD002792.pub2 }}</ref>
<!--Treatment and course -->
Ci yoon, nit ñi ñungi leen di faj ak [[pajum xelu nit ki|joxe ay tegtal ngir dimbali nit ki saafara jafe-jafeem]] ak [[garab yiy xeex déteelu]].<ref name=NIH2016/> Garab yi wone na ne am njëriñ, waaye njëriñ li mën na baax ci ñi gëna mettile feebar.<ref name="Fou2010">{{cite journal |vauthors=Fournier JC, DeRubeis RJ, Hollon SD, Dimidjian S, Amsterdam JD, Shelton RC, Fawcett J |title=Antidepressant drug effects and depression severity: a patient-level meta-analysis |journal=JAMA |volume=303 |issue=1 |pages=47–53 |date=January 2010 |pmid=20051569 |pmc=3712503 |doi=10.1001/jama.2009.1943 }}</ref><ref name="Kir2008">{{cite journal |vauthors=Kirsch I, Deacon BJ, Huedo-Medina TB, Scoboria A, Moore TJ, Johnson BT |title=Initial severity and antidepressant benefits: a meta-analysis of data submitted to the Food and Drug Administration |journal=PLoS Medicine |volume=5 |issue=2 |pages=e45 |date=February 2008 |pmid=18303940 |pmc=2253608 |doi=10.1371/journal.pmed.0050045 }}</ref> Leerul ndax garab yi dañuy def antum risk xaru.<ref>{{cite journal |vauthors=Braun C, Bschor T, Franklin J, Baethge C |title=Suicides and Suicide Attempts during Long-Term Treatment with Antidepressants: A Meta-Analysis of 29 Placebo-Controlled Studies Including 6,934 Patients with Major Depressive Disorder |journal=Psychotherapy and Psychosomatics |volume=85 |issue=3 |pages=171–9 |date=2016 |pmid=27043848 |doi=10.1159/000442293 }}</ref> Yenn xeeti joxe ay tegtal ngir dimbali nit ki saafara jafe-jafeem bokk na ci [[pajum nekkin bu àndak xalaat]](CBT) ak [[pajum nekkin ak ñeneen ñi bu àndak xalaat]].<ref name=NIH2016/><ref>{{cite journal |vauthors=Driessen E, Hollon SD |title=Cognitive behavioral therapy for mood disorders: efficacy, moderators and mediators |url=https://archive.org/details/sim_psychiatric-clinics-of-north-america_2010-09_33_3/page/537 |journal=The Psychiatric Clinics of North America |volume=33 |issue=3 |pages=537–55 |date=September 2010 |pmid=20599132 |pmc=2933381 |doi=10.1016/j.psc.2010.04.005 }}</ref> Su fekkee yeneen xayma yi amuñu njëriñ, [[pajum electrochoc]] (ECT) mën nañu ko jëfandikoo.<ref name=NIH2016/> Tëye nit ki ci opitaal dina baax su fekkee nit ki am na risk gaañ boppam te mën na léég léég ñakka ànd ak li nit ki bëgg.<ref>{{cite book |author=American Psychiatric Association |title=American Psychiatric Association Practice Guidelines for the Treatment of Psychiatric Disorders: Compendium 2006|publisher=American Psychiatric Pub|isbn=9780890423851|page=780|url=https://books.google.com/books?id=zql0AqtRSrYC&pg=PA780|language=en|year=2006}}</ref>
<!-- Epidemiology, history, and society -->
Feebaru naqar gu metti ku dara saful daloon na lu tollook 216 miliyoŋ ci ay nit (3% ci addina bi yépp) ci atum 2015.<ref name=GBD2015Pre/> Limug nit ñi ame feebar bi ci seen dund mungi tollu ci 7% ci Japon ba 21% ci France.<ref name="Kes2013">{{cite journal |vauthors=Kessler RC, Bromet EJ |title=The epidemiology of depression across cultures |journal=Annual Review of Public Health |volume=34 |pages=119–38 |date=2013 |pmid=23514317 |pmc=4100461 |doi=10.1146/annurev-publhealth-031912-114409 }}</ref> Lim gi ci giir dund mungi gëna kawe ci [[rééwi ame koom koom gu baax]] (15%) méngale ko ak [[rééw yi seen koom koom di jog]] (11%).<ref name=Kes2013/> Indi na ñaareel bu gëna kawe [[ci ay at yu ñu dund ak feebaru ñakka mën]], ginnaaw [[ndigg guy metti]].<ref>{{cite journal |author=Global Burden of Disease Study 2013 Collaborators |title=Global, regional, and national incidence, prevalence, and years lived with disability for 301 acute and chronic diseases and injuries in 188 countries, 1990–2013: a systematic analysis for the Global Burden of Disease Study 2013 |journal=Lancet |volume=386 |issue=9995 |pages=743–800 |date=August 2015 |pmid=26063472 |pmc=4561509 |doi=10.1016/S0140-6736(15)60692-4 }}</ref> Diir gu ñu gëna raññe ni feebar bi génn na mooy ci ati ñaar fukki yi at fanweer yi.<ref name=DSM5/><ref name=Kes2013/> Jigéén ñi dañuy faraldi gëna nañu ame feebar bi ñaari yoon góór ñi.<ref name=DSM5>{{citation|author=American Psychiatric Association|year=2013|title=Diagnostic and Statistical Manual of Mental Disorders|location=Arlington|publisher=American Psychiatric Publishing|pages=160–168|isbn=978-0-89042-555-8|edition=5th|url=https://www.psychiatry.org/psychiatrists/practice/dsm/dsm-5|accessdate=22 July 2016|deadurl=no|archiveurl=https://web.archive.org/web/20160731072609/https://psychiatry.org/psychiatrists/practice/dsm/dsm-5|archivedate=31 July 2016}}</ref><ref name=Kes2013/> Lii di [[American Psychiatric Association di mbooloo mi nekk Amerik dajale fajkati feebaru xel yi]] yoq ci ne "feebaru naqar gu metti ku dara saful" ci ''[[Téére Saytu bi ak Xayma bi ngir ñi ame Feebaru Xel]]'' (DSM-II) ci atum 1980<ref name=Her2008/> Ab dog dog la woon [[feebaru déteelu bu ànd ak dikkale bu wacc]]ci DSM-II, te mënin yi bokkoon ci ñu xame ko léégi ni [[déteelu bu ndaw]] ak [[ay feebaru nekkin yu dajaloo ak dikkale yu bon]].
<ref name=Her2008>{{cite book|last1=Hersen|first1=Michel|last2=Rosqvist|first2=Johan |name-list-format=vanc |title=Handbook of Psychological Assessment, Case Conceptualization, and Treatment, Volume 1: Adults|publisher=John Wiley & Sons|isbn=9780470173565|page=32|date=2008|url=https://books.google.com/books?id=zOBdVdjGf4oC&pg=PA32|language=en}}</ref> Ñi amewoon feebar bi ak ñi ko ame léégi mën nañu nekk ay [[légët ci dëkk bi|légëtloo]].<ref>{{cite book|last1=Strakowski|first1=Stephen M.|last2=Nelson|first2=Erik | name-list-format=vanc |title=Major Depressive Disorder|publisher=Oxford University Press|isbn=9780190206185|page=Chapter 1|url=https://books.google.com/books?id=dz8FCgAAQBAJ&pg=PT9|language=en|chapter=Introduction|year=2015}}</ref>
[[Wàll:Paj]]
7fy039uwdquzmw5ak8mhmpv134mx8ys